Zakat Partie 3

Zakat Partie 3

1st Grade

8 Qs

quiz-placeholder

Similar activities

Jullig kuy tukki

Jullig kuy tukki

1st - 5th Grade

7 Qs

Hadis keragaman

Hadis keragaman

1st - 5th Grade

11 Qs

Quiz buntu seuy

Quiz buntu seuy

1st Grade

5 Qs

surat alfatihah

surat alfatihah

1st Grade

5 Qs

Quiz Révision

Quiz Révision

1st Grade

9 Qs

Buntu Sangou Farata / Sétt

Buntu Sangou Farata / Sétt

1st Grade

9 Qs

Quiz Révision ak Jullig  Ajjuma Partie 3

Quiz Révision ak Jullig Ajjuma Partie 3

1st - 3rd Grade

12 Qs

Quiz Révision

Quiz Révision

1st Grade

8 Qs

Zakat Partie 3

Zakat Partie 3

Assessment

Quiz

Religious Studies

1st Grade

Hard

Created by

Soxna Astou NDIAYE

Used 1+ times

FREE Resource

8 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE SELECT QUESTION

20 sec • 2 pts

Kou tokk années you beuri youmou waron guénné azaka té défouko.

Ndakh dafay fay années yoyou ?

Oui

Azaka kéneu douko fay souféké période biniouko wara guénné dialeu na 

Azaka comme diouli ak koor rék koussi amé bor da ngay fay

Dafay estimé limou waron guénné année yoyou yeup mou guénné ko

Non

2.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 2 pts

Ramadan 2021 Serigne Diop dafa am 3000 euros si compte épargne,

Ramadan 2022 compte bi am na 4500 euros, Ramadan 2023 Serigne Diop amna 6000 euros si compte bi.

en 2023, Sérigne diop war na guénei Azaka ? si oui, ñiata ?

Oui

Non

600 euros

150 euros

Autres

3.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Khady commerçant là dafa am 5000 euros épargne lou am att waayé dafa am bor 4500 euros.

Noumouy def ?

Dafay fay bor bi, lissi dess mou guénei si Azaka

Dafay fay bor bi rekk souféké amoul lénén (khaliss, marchandises, keur, auto, etc )

Dafay guénei Azaka, alaa kulli haal

Dafay guenei azaka souféké amna lénén lou meuna fayé bor bi (ay takaay=bijoux wala keur,...)

4.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Malick ak Awa dénio am kounékk 200g wourouss (Or) lou matt att

nouniouy deff ?

Niom niaar déniouy guénné 2,5%

Douniou guénné dara souféké séniy takay la (bijoux)

Malik dafay guéné 2,5%

Awa dafay guéné azaka soudé dafko garder ngir diokh ko ay seuteum

5.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Tabaski 2021 Amy dafa am 7000€ si compte bancaire. Mou denthie ko ba tabaski 2022 mou guénné si azaka mou déss 6825€.

Ndakh tabaski 2023 Amy dafay guénné waat assaka si khaliss bi?

kéneu dou guénné azaka niari yoon si même khaliss bi

Oui, lissi déss matna nissab donc dassiy guénné waat azaka

Non, guénné nassi azaka ba paré

6.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 2 pts

Aicha dafa am 10000€ si wérou koor 2020, biniou démé ba wérou tabaski 2020 khaliss bi déss 3000€. Bi wérou gamou nieuwé Aicha amat  2000€ you béss.

Kone légui Aicha amna 5000€.

Aicha kagn la wara guéné azaka ?

wérou tabaski 2021 la wara guéné azaka

wérou gamou 2021 la wara guéné azaka

wérou koor 2021 la wara guéné azaka

7.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 3 pts

Khalé bi papam dafa décédé bayil kofi 50000€

Est-ce que chaque année dinégn  guénné azaka si khaliss bi ?

Non, parce-que azaka waroul khalé

Waw, dinégn si guénné azaka mais béneu année rék

Non, parce-que bala mouy majeur khaliss bi dafay diékh

Waw, Année bou nieuw dagn si guéné assaka

8.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

45 sec • 2 pts

Borom keur gui dafa décédé bayifi ndjaboot. Mais avant mouy décédé fékk waron na guénné azakat khaliss mais diotouko woon guéné.

Nouniouy deff khaliss bi ?

Déniouy miraas khaliss bi té kéneu doussi guénné azaka

Azaka kouy dound rék la war

déniouy guénné azaka gui ba paré après niou miraas li déss